Confidence d’Alice : « sama dieukeur day begue may photo sama S… »

0 23

« Mane dama am louma méti sama dieukeur nékoufi mogui extérieur mais à chaque fois day begue may foto sama ana ndiaye bi dikoko envoyé ba barki demb mou wakhat mako ma bagn mou méré ma soumako envoyé sms douma tontou,ba demb mouné ma louma beug ngamay défal wala do am diam.bobou ba légui wowouma té sou mako wowé pour niou wakhtane douma falé dama diakhlé instant bi. Dama sokhla kouma dimbali », confie Alice, une jeune femme de 27 ans.

Laisser un commentaire

Votre adresse email ne sera pas publiée.