Dama am louma méti sama dieukeur day begue may foto sama …

« Sama dieukeur nékoufi mogui extérieur mais a chaque fois day beugue may foto sama ana ndiaye bi

Mane dama am louma méti sama dieukeur nékoufi mogui extérieur mais à chaque fois day begue may foto sama ana ndiaye bi dikoko envoyé ba barki demb mou wakhat mako ma bagn mou méré ma soumako envoyé sms douma tontou,ba demb mouné ma louma beug ngamay défal wala do am diam.bobou ba légui wowouma té sou mako wowé pour niou wakhtane douma falé dama diakhlé instant bi .Dama sokhla kouma dimbali » Anna Conde